KING BABA - Ngaaka Blinde - Metti Nii (clip officiel)

Описание к видео KING BABA - Ngaaka Blinde - Metti Nii (clip officiel)

https://bfan.link/secret-7-vol-2-alke...

« Metti ni » est un mot wollof qui signifie tout simplement : faire mal.
C’est un single qui ne fait pas partir du projet « Ep »prévu pour decembre 2021. Ceci a été composé avec un style de musique très particulier appelé « afrotrapgalsen ».

--------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------
PAROLES « METTI NI »
Intro: (KING BI CHALLENGE - YANDÉ CODOU SEN-MOMO GOT THE JUICE)

Refrain : king baba boudé rap leu may rap (rep) ….King baba doudé rap leu yaay rap !

Nieuw deff flamme-feu OG gang bi nioy trap
(Rep) …. Nieuw deff flamme deff feu OG gang bi nioy trap

Nio nekk ni !
Hé hé metti ni !
Hé nioune nio mel ni
Nioy nieuwatt thi game bi paré pour lekk gni !


Je suis le juge et quand je parle je veux que
tout le monde se taise
Personne ne bouge deposez moi les armes
Aller les mains en l’air
Ya les A-k- 4 et les 47
Les rappeurs covids sont pas en quarantaine
Je suis plus loin que la tour eiffel
Et tu fumes que des joins t’es pas bob-marley
Je suis pas ton égal même tes égales je suis pas leurs Ego
Tu pensais que ceci est normal et finalement tes un parano
Kou diégué- meussa niéme- kouma téré gueneu télé- télé bouné maffa leumbé- nieupp bégué fouma meuné- dougueul ci mane da nga gnéme-ma gratté ko bamou saigné !!!
Soudj ko ndioudj ko poupe ko thioute ko
Benn kadou ngay degg moy (ning ma rayé)

Mane may passonou gayi
Ma keuffone diarry
May king bou maak bi ngay bagn
Mane may adiaate bar yi
Ma todione mbaari
Sen bopp mame yi lay ngrégn
Fi kou sa carrière diek rek thiang
Ngay doul diniou tegal nane niou day vac
Nane léne pullule yi maléne disseul
Avortement naaq dagn koy bagn !

Refrain 2 : king baba boudé rap leu may rap !(rep) ….King baba doudé rap leu yaay rap
Nieuw deff flamme-feu OG gang bu nioy trap
(Rep) …. Nieuw deff flamme deff feu OG gang bi nioy trap

Nio nekk ni !
Hé hé metti ni !
Hé nioune nio mel ni
Nioy nieuwatt thi game bi paré pour lekk gni !

Who’s next who’s next (bis)
Kane mo thi topp
Kane moma gnimé guiss may dox di dem ci mic beat bou nice kane momay toppou
Nga fokné gni daniou wopp
Djiéné diapouléne niou réglé té tok
Baba dou xarit dou mbokk
Kou saga king saga nga sa papeu defko sa nopp
Hey Kenn douma chocopain ladjma niom pathé séne (patisen) fouma nékh feuleudié
(Hey hey hey)
Xalé douma bleuffé king noumou werrédé
Hey kouka diégué dée
(Hey hey hey)
Tacko fall loumou ndiol ndiol bouy xol pagnè bi day tééne
Mane may ndiba bi ngay séene
Finalou fc di choc thi mbaye pekh

« Dila iri dila tate loloy xelou pedophilie, dila diaay soukrate melni philosophie, détruire ay rappeurs akassé facile, parè daw lou yagg melni may Wiri Wiri »

Xalé ba ngui aka beugg bamba
Dindi rap bou bone melni mane leu jamra
Bou baba raboul est-ce que rap bi amnà ?
Ladial radji radji kane mo tangal tamba

Refrain 3: king baba boudé rap leu may rap (rep) ….King baba doudé rap leu yaay rap !
Nieuw deff flamme-feu OG gang bu nioy trap
(Rep) …. Nieuw deff flamme deff feu OG gang bi nioy trap

Nio nekk ni !
Hé hé metti ni !
Hé nioune nio mel ni
Nioy nieuwatt thi game bi paré pour lekk gni !

--------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------

Disponible sur toutes les plateformes de streaming
Chanteur : Ngaaka Blindé
Mixte et Mastering par : Kbc music
Style musique : Afro trap senegalais
Beatmaker : momo beats
Réalisateur : Selevfx
Deco: didi art et formation universel
Stylisme : Radji fashion

-------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------
Réseaux sociaux :
Facebook :   / ngaakablinde  
Instagram : https://www.instagram.com/ngaakablind...
Twitter :   / ngaakablindee  
Site web : www.ngaakablinde.com

---------------------------------------------------------------------------------------------------------------------

Contact Manageur :
Mail : [email protected]
Contact : 00221 774653939 - 00221 774681039
Équipe : Blindé Musique

Комментарии

Информация по комментариям в разработке